Je T'Aime
Wally B. Seck
3:16Saf nga djiguén lolou lalay topé Damla khol lima guiss dima choqué Ni nga mél naturelle la, doko forcer, non Guel bi dafa tang badi laké Safara bi nelow si yow la begg guiss (wopopop) Pessé naala, ci li nga tok dafa diiss Saf ni jumbo, toy ni rico Guel bi dafa tang badi laké, chaud Bad girl boy boula diégué ma shoot Limay weur yeup ci djiguén nga ouf Sa bep morom boula teukou nga shoot-shoot-shoot-shoot-shoot Baby kaay sama wet, mbeuguél lalay sééd, man dama dioy Bilay yaay kimay daanel oh oh oooh Bimala guissé sama khol dafa nékh Bimala guissé eh eh eeeh Baby kaay sama wet, mbeuguél lalay sééd, man dama dioy Bimala guissé eh eh eeeh Sama linguère yaa khééré dé Am nga thiass, waw ya tiékété Yow lay weur souba ba ngone ma teudi Yaag na beuré wayé yow tu es mon combat Bandit bandit baby bandit bandiloul (bandé) Wan ma sa bandit weundéloul Thiow-li thiow-li yow la diougal nga féémou Daggal sa yaram niou ndelou Bad girl boy boula diégué ma shoot Limay weur yeup ci djiguén nga ouf Sa bep morom boula teukou nga shoot-shoot-shoot-shoot-shoot Baby kaay sama wet, mbeuguél lalay sééd, man dama dioy Bilay yaay kimay daanel oh oh oooh Bimala guissé sama khol dafa nékh Bimala guissé eh eh eeeh Dama dioy, sama khol dafa nékh Dama dioy, bimala guissé