Mérité
Yanko Sm & Mist Cash
3:44Yow L'argent ne fait pas mon bonheur Mais thiabi bou efficace leu dalay tidjil ay bountou Yété wouma yam tchi maay business Deff son you mélni or nigga soppi ko thintchi Lou géneu daay délou tchi compte Deff son ba dead, fayou tabakh sama banque Gratuit, hijo dé puta Boy limay dadj studio boudone yaw digua onkou Get pay fayal money yah Euros, dollars, CFA bi yah Souma namé bay tchi soufou assame boudoul taw Teurlén ma réindi yah Fayou pour fay gnimay défal Mais pas pour sol JO, Gucci wala Fendi Boy sa MC bi marque leu sole mais galém rérou niou Boul meussa gné ki non wow Na nieup dead, il me faut du biff Na thiow li djip ndakh daay guéné djizz Boy fi sofi beugué la paix Armél té songou lén, gagner sa guerre wow Millions dollars tchi ay comptes Té respect bou téwoul mane douma tchi bokou Han, saay convictions niolay deff noble Sagal lima geum ma wadal sa bop Han, xamna ni succès bi bitch leu Motakh j'le ken et il me paye Gniy xar ma danou, j'ai fais le plein Waxlen dou tay dou another day Ma néna jobal ma nianal leu Fo dém nianou yaye gata ndou la Beugal gnila bagn, banial gnilay diay Ndakh gni bolén toppé niou sank leu Get pay, stay humble Loyal to the home boys This game is like jungle But we don't care, we the Galou Boyz J'ai longtemps connu la terre Maintenant, je réponds à l'appel du ciel N'essayez pas de me suivre Yanko a déjà déployé les ailes Safara douniou ko diwo Work hard and get pay Sa concert boul niou tchi wo So fayoul cash, douniou deff téw Faut du cash, deff lou xéss Bokou niou tchi loudoul am fay Billets bleus, billets mauves Yanko ak Elzo, faw gua fay Safara douniou ko diwo Work hard and get pay Sa concert boul niou tchi wo So fayoul cash, douniou deff téw Faut du cash, deff lou xéss Bokou niou tchi loudoul am fay Billets bleus, billets mauves Yanko ak Elzo, faw gua fay N**** fok niou riche, work hard douniou lébal kén Bindeu sons you diss, Mozart daniou éternel Deff comme SOTY bi Tidjil grosses salles yi niou féssal len Legui foniou guiss Big contrat signer bégeul len Nigga goor dou tite Danio ragal yallah wayé niémé cash Kill prod yi comme John wick Deff ay movies comme Lionsgate Beug poche you diss Mo waral yokou job seven days a week Rombou douanes yi comme Go fast Amoul séral men Damay deff ay hits comme Chidinma Ay sons you hybrid comme Linkin Park Boul jouer rôle comme Cherif Maal So guissé kouma geuna nék idoles indilma Feeling paatch daur missile diageu Free Izi ak Yanko comme Weezy ak Drake Sisi my nigga this is hard Di deff sons you fire comme mane ak Dizzy Kha Meuno diémalé tchi nioun loudoul hate Beugouniou yeufou fake, beugouniou loudoul vraie So néké omo do saba dé Fi dounioula xeubeul danioulay sagua nday Fot sama bopou - Té waxou mala ay waxou sabou dé Tapis rouge canne ak sabador Job rek dimanche ba sabado C'est ça batay Safara douniou ko diwo Work hard and get pay Sa concert boul niou tchi wo So fayoul cash, douniou deff téw Faut du cash, deff lou xéss Bokou niou tchi loudoul am fay Billets bleus, billets mauves Yanko ak Elzo, faw gua fay Safara douniou ko diwo Work hard and get pay Sa concert boul niou tchi wo So fayoul cash, douniou deff téw Faut du cash, deff lou xéss Bokou niou tchi loudoul am fay Billets bleus, billets mauves Yanko ak Elzo, faw gua fay Let's go give me my pay Give me what I deserve Oh right Every fuckin day we hustle hard nigga Oh right Elzo, Sell mind douniou job tchi néén Oh right We gonna get that pay We gonna get that pay Oh right