Sa Yoonu Bop

Sa Yoonu Bop

Yanko Sm

Альбом: Sa Yoonu Bop
Длительность: 4:24
Год: 2025
Скачать MP3

Текст песни

Yeah
Tél naniou takk laxasay yi saubou tchi yoon
Zéro tite louniou am dieul
Ndax rangoñiou mère mo nandal ngor ak diom si nioune
Boy fadiar laniou diouk ndieul
School of life moniou diangal
Kone sunu diar diar moy liñiouy faal
Diambar bouy xaré di reub kiy reubé tchi aleu, dara douko titeul
Louma meussa saubou am tchi ngeum dokh
Tawhidou goor yallah sama rouh la sakh
Ladial gnima xam ngor ak diom geum kima done
Ragalouma gnimay gassal pakh
Ndakh dead na bou yagg bamél damako miin
Do adjii même booy wouti xam-xam ba Chine
Boy tank dou dokh fou xél meunoul dém
Limay wax dou pour boromou guiss guissou nén
Digén ma réé ndakh niro wouma ak yén
Digén ma soof ndakh yén nieupa yam
Diamant la tchi mbalite
Kone faw thiow li beuri
Ndakh public bou ignorant bi douniou adjie
Mais domou mbotou xaar ko tatou ndala
Jajeuf yén gniti meussoul diap
Nit kou nioul dou djie dou rossé di xaar bamou mageu
Té sasouné daay beugua kérou
Soumalen topone lorrou yaakarouma tchi kéneu
Dina xare mateu tay, souba lay diarrou
Ragalouma wéet même sou wéetay bi woroul
Mane fiit momay yaubou sell mind rék yégoul
Sa succès noumou tolou la sa thiono mél
Boy deglou nieup niou fowé sa xéll
Doxal té dém même bounioula gounguéwoul
Yallah geuna waur té amoul foumou néwoul
Kone nangoul

Wéet, yeah
Mome guay deff soy xaleu sa yone
Boul ragal wéet tchi sa yoonou bop
Boul ragal wéet tchi sa yoonou bop
Wéet, yeah
Yoral fitou gaindé ndiaye
Boul ragal wét tchi sa yoonou bop
Boul ragal wét tchi sa yoonou bop
Wéet, yeah yeah yeah yeah
Boul ragal wéet tchi sa yoonou bop
Boul ragal wéet tchi sa yoonou bop
Wéet, yeah
Takkal sa fiit té weuy
Boul ragal wéet tchi sa yoonou bop
Boul ragal wéet tchi sa yoonou bop

Naxar mo geuna waur, ndakh joie da infidèle
Kone goor rañiél les vrais ak les faux
Yone wi am na ay fauves
Xarito ak sa bop geuna waur
Pour yégeu sans dieul ay détours
So oyofé ni xop lou nieuw dalal keuf
Solitaire gua kéne doula yénoul sa jeuf
Kéneu alouma thiabi succès dama dadjie portes yi
Jeulal sama bopou sama thieur
Depuis bamay ndaw dara meussoul yombou
Pour am béneu fallait meu deff le double
Dama tok di daw niou fok ni nioma rombou
Fék géneu na ba dém tchi yénén mondes
Fuck gnima diokh sén lamign bama soxla loxo
Ngima done ték deal fokni dama feudo
Xamé na sén kanam yi vautours you fébar yi
Yén nieup tchi antidote bi guén di fadio
Oh right, Oh right, my n****
Dafma lér ni dina briller ni Jigga
Déglouma xam ni sén rappeurs yéy thiomo
Tay lou yeungou, épicentre bi mana
Album bi waw dina diay, dassal ko price
Loko dieundé meunoul reuy samay eyes
Mane bamay try guissouma waay
Té kén tchi yén douma délo samay night
Samay night
Kén tchi yén douma délo samay night
Yeah, I was lonely with myself
Wéet, wéet, wéet, wéet
Yeah, that's why I say

Wéet, yeah
Mome guay deff soy xaleu sa yone
Boul ragal wéet tchi sa yoonou bop
Boul ragal wéet tchi sa yoonou bop
Wéet, yeah
Yoral fitou gaindé ndiaye
Boul ragal wét tchi sa yoonou bop
Boul ragal wét tchi sa yoonou bop
Wéet, yeah yeah yeah yeah
Boul ragal wéet tchi sa yoonou bop
Boul ragal wéet tchi sa yoonou bop
Wéet, yeah
Takkal sa fiit té weuy
Boul ragal wéet tchi sa yoonou bop
Boul ragal wéet tchi sa yoonou bop

I was lonely with myself
Follow my way meussouma xéff
Ni gaïndé topou sama yoon
Même boudoul yén boy dina go
I was lonely with myself
Follow my way meussouma xéff
Ni gaïndé topou sama yoon
Même boudoul yén boy dina go