O.G
Yanko Sm
3:40Mérité, mérité Succès bi dañiou ko mérité Mérité, mérité Talent bi dañiou ko mérité Work hard dém jeuli Lou ñiaxeu di mayé, n**** we go get it Ey, nioun leu boy the new elite Ñioun fiñiou diar, koufa diar do ñibbi Et ça, ça mérite ay disques d'or Et ça, ça mérite ay millions Et ça, ça mérite que vos rappeurs nous appellent "eh papa" Et ça, ça mérite ay lambos Et ça, ça mérite ay lingots Et ça, ça mérite que sén bii game, xamé OG ak thiagua Et ça, ça mérite, success get it Dioudou sans héritages moudiou doneu elite Gnima beug ray sama tank bassi séneu bamél yi Defna deli té dou kéneu dieuli Diléneu eskanté tangorou rap bi lay diéry Fathie si ay president ak ay milisse Des putes, députés ak ay ministres Si song yi lagniou investir comme missiles (wow) Fayékou ligniou def si sougn musik (wow) Nioun yap sa gang lagniou dibi Gars yi daw, gars yi done game daw gnibi Niak reuy ni guélawar, diokhé kadou yi ni magoum Defal yalla werouway walla outi koula walou Di encaisser coup you bas yi, beug fayekou ni Ngannou Nigger amnga woutou kay, mais sa fit bi dafa daloul Dégu na damako taloule, wax si rap bi dafa taroul Fake ngeu yakal sama dérr, meun nalla tontou dako diaroul Douma changer sama team ni Choji, Ino, Shikamarui Dama yaga dougou guéthie, beug outi louma narou Tela sip né néké war moy win Felicité art moy djiz Téla guiss fouy bouger niaf fa vice Carrièrou boyi done diouk faf covid Rest in peace Mérité, mérité Succès bi dañiou ko mérité Mérité, mérité Talent bi dañiou ko mérité Work hard dém jeuli Lou ñiaxeu di mayé, n**** we go get it Ey, nioun leu boy the new elite Ñioun fiñiou diar, koufa diar do ñibbi Et ça, ça mérite ay disques d'or Et ça, ça mérite ay millions Et ça, ça mérite que vos rappeurs nous appellent "eh papa" Et ça, ça mérite ay lambos Et ça, ça mérite lingots Et ça, ça mérite que sén bii game, xamé OG ak thiagua Dañiou mérité lii job leu dou néén Hustle everyday amouma week-end Hip-Hop souy falate may tok thi donkass For ever winner bi daay finkeu Ni diantou ndiolor fi nay lér Diplôme de Kocc, fuck sa Baudelaire May ki geuna présent ki geuna absent Pour follow ma faw gua am flair Dougén yék tant que may le top May ki aak may ki bess Soumay pull up tu passes à la caisse Dara dou dess, give me your cash and your best Soumay sédou li dess guen di tiop Médiocre, topou moy gua diar thi brasier Meuno diangeu ba ndandeu boy shoes yima am Dama akssii niou classé ma pé Rappeurs yi di dead, thiambarat len talent biniou am Mbauw-mbauw-mbauw Guéen di deff nalén piw-piw-piw Antidote bi laalén di roff LG ba New York nieupay moss chill Mérité, mérité, lotta money get pay nioumay glorifé Douma wew chapter game bi lay mbindate Mou doundat sa rappeur di horrifié VVS, lambo, sape you classe, clothes you dinguo Mane ak niom meunouniou ménguo Nimalen séxlo, kouma thi kép kill ko déguo Sadique man el chapo Liñiouy deff ak limaay deff dafa wouté douñiou beuré Inspiré every time boy mind bii dou garé Limay bind all time dina shine bathi ñieulé Generation futurist mérité lou geuna kawé Mérité, mérité Succès bi dañiou ko mérité Mérité, mérité Talent bi dañiou ko mérité Work hard dém jeuli Lou ñiaxeu di mayé, n**** we go get it Ey, nioun leu boy the new elite Ñioun fiñiou diar, koufa diar do ñibbi Et ça, ça mérite ay disques d'or Et ça, ça mérite ay millions Et ça, ça mérite que vos rappeurs nous appellent "eh papa" Et ça, ça mérite ay lambos Et ça, ça mérite ay lingots Et ça, ça mérite que sén bii game, xamé OG ak thiagua