Mérité
Yanko Sm & Mist Cash
3:44Yo Yo, let me tell you how I feel about it Liy ndiaxoum tchi deuk bi, doumko digérer di tok rek Yo, mane bouma naré nopi, dead tchi silence Bayi seytané bakou, kone ma daur sama bopou gun rek Jikko you bone, féegn tchi maak yi warone wané yone Beug alal gorédi laniouy yaré séni doom Hospitalé terangua bi tchi xeew la yam Biss bouné mbokou setane mbokam, bamou gaañiou dém Pour deff té yallah takh, diaroul guay woolou caméra Pour nioulay guiss, wéssou tiss, lifi xew drama la Soubhannallah, boul lap tchi nguisteul, liñiou sopou worma la I feel bad dougen réference yigen warone done Doom dou soukou diour ndéki agne yam tchi, yaar na topou Sol ko jikkoy mbaakh ba foumou né, niou naw ko meun ko sopou Yeah what I feel is bad sometimes ma diaxlé Gni warone nangou nbiémbeul deff naniou allégeance tchi money Talibé dou diam, serigne tam dou buur non Sa hadiya kokoy diokh na deff sa xol borom ba Bamba ko wax, serigne nay xamlé yallah, moyou bakanam Talibé nay diamou xouss té dialeu, moy katanam Fok ma halou tass séni kala, thiap xalima mbindeu Tall natalou sen idole yi, seytané len guémbeu Legui TikTok gni dakheu saga lagniy topou di cas Tass na ay mbokou, wéranté bagui deff ay dégât Faut que ma clatté influenceurs you con yi né thi toile bi Doumalén flatté doff yé eup thi yéén Dañioulen wara ramasser, yobb dalal xél guén nanii garap Fermer séni clapets Toujours au taquet pour vous éradiquez, kén waroulén bardé Yo, I'm so crazy sometimes mane soumay dégg Ponkal mou violé moromou domane pourtant nioy deuk Evoquer effet prise de drogue ay mbaam guen deug Sen galgui prédateur sexuels yi rek fi niofi eup Lima feel guay laadj This shit is bad, fila boy yi souss di snifé crack Fi nieupay takeu amoul arrêt tééré thi fowoum taate Daguay laadj legui fo tourner degeu waxoum taate Galsen comme faculté bouniouy dispenser ay cours taate If you ask me what I feel, I say you léépeu fuck up Niata ñjiit niofi diar sathi souniy millards teup Qu'on les traque, bring them back Askane wi meuna feel good Li nieup bokou non dou pour kén, nassi nieup diot How I feel about it, let me spit the knowledge Solinou pute ak prof yiy irri yigua guiss thi college Boy you siik ba saalit, weur di carte xalliss Amouñiou gène thi talal loxo, ken dou keep it honest Nigga let me tell you how I feel about it Jeunesse bi fitam togoul motah jeul na galgui Dépense moy cas bi daw tchi bopou Pa yi Question de léék leu ak naane, faarlo touñiou thi yaar bi Tchi djiko laniouy geunanté wala tchi déret Make sure you never judge, boul diss ken respect Séni manquement ak tord guen beug di wouteul cause Yéré nationaliste gua sol mais t'es un xénophobe Everyday, C bi daay,diaadeu lo ay diek youy seuy Xel bou panne defflo nala faute, gua done fa sabou sééy Méér tass, banque tass, sacralité amoufi place Légèreté tchi bépeu mbir, réér daw na ba mbeuk mire I need love for Casa Show love to Gaza I don't know why they kill the young kids for plata My heart is broke Ya need to stop Congo and Sudan too deserve love Yeah, you ask me what I feel about it Ya nigga, ya nigga This is how I feel about it We need to step back This life is going mad Sétlou waat men Life bégui beugua doff men Ey to Bazik cut that shit Cut that shit