Interlude (Feat. Nitdoff, Thioum C & Tifa Diaw)

Interlude (Feat. Nitdoff, Thioum C & Tifa Diaw)

Yanko Sm & Bazik Prod

Альбом: Antidote
Длительность: 3:38
Год: 2025
Скачать MP3

Текст песни

Yanko (yako), Sell Mind (Sell Mind)
Yanko (yako), Sell Mind (Sell Mind)
Yanko (yako), Sell Mind (Sell Mind)
Yanko (n**** what) Sell Mind (Come on)

Wax ko tchi kaw (what)
Wax ko tchi kaw (what)
Yanko Sell Mind (moy the best)
Wax ko tchi kaw (what)
Wax ko tchi kaw (what)
Yanko Sell Mind (moy the best)
I'm from trigger mind (Gunzout)
Represent my home town (LG)
Wax ko tchi kaw (what)
Wax ko tchi kaw (what)
Yanko Sell Mind (moy the best)

Sell Mind geun léna danger ni sélu lion
Souma waré beat bi damalen di fuck vite fait, sawlén daylén
Aythia MCs kaylen, ma neuxeulén tchi guedjou talent
Dougén fi am pied fimoy dark side, boy aythia dead lén
May ki doundeulat boy real hip hop
Door sa MC balle tchi bopou
I'm the winner, tok feulé tchi thiolou bi,fuck bi game mou totes
Game bi yénako poisoné, fuck you nagén togué né
This is the Galou boy
Faw gua fannaw soumakoy sédeulé
Naan guiédjiou rap bi
Pour gua mandi mane guay xar ma SOTY
Boy rap déwoul come back to me
Déékeu ma sén kook yi
Yi pussy n***** doumaak niom, teudieul lén ma sén thiotou yi
Esprit ndanane yeup tchi souf la yallah deff tchi bopou bi
Ey yow, work hard, work hard
It's time to play hard
Fuck you public bou faux bi, démal jeul sa yonou bopou
On move en bloc, moi et les G té douniou dokh di yoot
Game bi damako boot dioguila dokh, yaubou ko all the top
Fuck you, yaw ak saay Loubou
Même soumay sole boubou
Souma rapper gua rap, niounima Kendrick, yaw boubou
Malen meune, fougn tassé boy sa baye lay tamarin
Ey, encaisser sén cachet dém dalou dji Palmarin
Ey, bala fi guay jacter nous on est pas dans mbélé
Ey, mama nianalal sa dome, victory la mérité

Wax ko tchi kaw (what)
Wax ko tchi kaw (what)
Yanko Sell Mind (moy the best)
Wax ko tchi kaw (what)
Wax ko tchi kaw (what)
Yanko Sell Mind (moy the best)
I'm from trigger mind (Gunzout)
Represent my home town (LG)
Wax ko tchi kaw (what)
Wax ko tchi kaw (what)
Yanko Sell Mind (moy the best)

Low, low, low, Bazik
Change the beat
Change the beat
Ma yébi wat tchi yénéni barres may sen bay tchi deff hit
Ay tasspé ay putes, nio leumbé game bi, légui do siip
Ko taudieul fi soudoul Sell Mind, mbédeu koy siip
Add the kick, add the kick
Ma ték tchi last barres yi diomalat
Gui guoné maak bouko saurou mou dane leu, ni David ak Goliath
Jeulal sa aliwo té feel malay diangalat
Fakes yi dess teur lén réindi sén dérét di rogolaat
May coke bou dure bi deff ma nank, magua overdose
Setsima ma baxé la ay dadji, ndakh may ki xam sa dose
Wathial tchi géw bi welcome, fi gaïndé guéfi waaf
Kill you nigga seuf leu drama, sa microphone lay off
Rimes yi daniouko try my homies, douniouko bâcler yaw
Saf na kaani sa gaum yi tchi lakoy ratalé yaw
Carte gui tay mako tébbi makoy battrer yaw
Béneu tchi ass yi guay guiss yénen la guétaro yaw
Yanko in the ghetto tay gua xam ni hustle mélo
Samp ndeundeu feug galagn, dance lo sa ghetto
I'm the street voice, talking classic youdoul dagne
Lalay sanni soudé bopou néén gua meun nala xaagne
I'm the Galou boy
The number one
I'm the real one, fuck you boy ko meunti doon
Call me OG (OG)
The OG (the OG)
The mother fuckin lengandary OG